Loading...

Youssou Ndour - Allah

198,317 views

Loading...

Loading...

Loading...

Rating is available when the video has been rented.
This feature is not available right now. Please try again later.
Published on Jan 10, 2009

Allah

Allah, Allah, Allah, Allah
Allah, Allah, Allah, Allah
Suñu boroom bi yaa waahidun, kenn la
Kenn la, kenn la, amul maas
Suñu boroom bi yaa waahidun, kenn la
Kenn la, kenn la, amul maas
Suñu boroom bi yaa waahidun, kenn la
Laa illaha ill Allah
Boo nekkee ci sa biiru yaay, Yàlla di la sàmm
ba nga am juróom ñeenti weer
Mu wàcce la ci àdduna bi, boolel la ca nak,
Ay xéewali xéewal
Boo ko tooñee, boo jéggaloo, mu baal la
Boo ko ñaanee mu may la, nga sant ko, mu dolli la
Laaju la ludul na nga ma jaamu
Laaju la ludul na nga ma jaamu
Yow, boo goree, boo goree, war ko jaamu, sant ko.
Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la
Kenn la, kenn la, amul maas
Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la
Laa illaha il Allah
Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la
Kenn la, kenn la, amul maas
Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la
Buur bi Yàlla moo ñu gëna gore
Buur bi Yàlla moo ñu gëna gore
Ndax léeg-léeg ñu topp xéewal yi ba fàtte ko
Te bu ko neexoon, ci diir bu gàtt
Kenn dotul xam fu sa bunt kër féete
Loo mënn nekk ci àdduna ya
War nga ca boole jaamu Yàlla
Def ay digleem, bàyyi ay tereem
Te bañ woote benn buur budul Yàlla
Suñu boroom bi, yaa waahidun, kenn la
Kenn la, kenn la, amul maas
Suñu boroom bi, yaa waahidun, kenn la
Laa illaha il Allah
Suñu boroom bi yaa waahidun kenn la
Kenn la, kenn la, amul maas
Suñu boroom bi, yaa waahidun, kenn la
Laa illaha il Allah

Yàlla na ñu Yàlla buur bi xiir ci boppam
Ci barke suñu sang Seydina Mohammed
-Salalaaxu aleyxi wa salaam
Yàlla na ñu Yàlla xiir ci boppam
(Bi jaahi, bi jaahi)
(Jaadu Cheikhouna Sanusi)
(Jaadu Cheikhouna Sanusi)
Cheikh Saad Bu
ould Cheikh Ahmed Faadel
buun Mamin
buun Talib Khayr
buun Talib Dieh El Mokhtar
Boroom Nimzaat
Yërëm ñu yow
(Jaadu Cheikhouna Sanusi)
(Jaadu Cheikhouna Sanusi)

English translation:
Lord, Lord, Lord, Lord
Lord, Lord, Lord, Lord
Our Lord is One
One, with no peer
Our Lord is One
One, with no peer
Our Lord is One
No master but the Lord
With His grace you lived nine months
in the warmth of your mothers womb
Then you came into this world
and were given a destiny
He laid forgiveness onto your wrongs,
covered you with His favors
Thanking Him is enough to receive more
In return, He asks only that you surrender to Him
In return, He asks only that you surrender to Him
The Way is thus to surrender, and to thank Him
Our Lord is One
One, with no peer
Our Lord is One
No master but the Lord
Our Lord is One
One, with no peer
Our Lord is One
His attributes are better than our qualities
His attributes are better than our qualities
With the pleasures of life, we might forget
But in an instant He could erase our reality
So whoever you might be
Please go on believing
Doing right, avoiding wrong
Free yourself from all masters except for God
Our Lord is One
One, with no peer
Our Lord is One
No master but the Lord
Our Lord is One
One, with no peer
Our Lord is One
No master but the Lord
May the Lord make us believers
In the name of Seydina Mohamed
-May the peace and blessings of God be upon him
May the Lord make us believers
(By His grace, by His grace)
(In the name of Cheikhouna Sanusi)


(In the name of Cheikhouna Sanusi)
Cheikh Saad Bu,
son of Cheikh Ahmet Fadel,
son of Mamin,
son of Talib Khayr,
son of Talib Dieh El Mokhtar
The sage of Nimzatt
May our sins be forgiven
(In the name of Cheikhouna Sanusi)
(In the name of Cheikhouna Sanusi)

Loading...

Advertisement
When autoplay is enabled, a suggested video will automatically play next.

Up next


to add this to Watch Later

Add to

Loading playlists...