Loading...

Pape Diouf - Bégué ( + LYRICS dans la description )

3,776,917 views

Loading...

Loading...

Loading...

Rating is available when the video has been rented.
This feature is not available right now. Please try again later.
Published on May 10, 2012

Pape Diouf vous présente son nouveau clip Bégué
-/ Suivez toute l'actualité de Pape Diouf sur http://gplus.to/papediouf
http://www.twitter.com/papedioufmusik
et sur http://www.facebook.com/papedioufmusic Rejoignez nous sur:
Google+ - http://gplus.to/PrinceArtsMusic
Facebook - https://www.facebook.com/PrinceArtsMusic
Twitter - https://twitter.com/princeartsmusic

- - - PAROLES - - - LYRICS - - -

Shooooooow !
Yekssi ngue yekssi ngue....
Shoooooow !
Deguetil déguetil
Shooooooow !
Sénégal Pape yéksina



Bilay man suneuna thi wakhdji wawaw
Kébétoubi beurina...
Mom doynaaaay
Dama name degg dadji... Roumbakh deuguine dadj
Sama yaye beuguenalaaa yayou khadim... Yayou Aladjéééé
Wawaw tey ma rindieul leu say nderr yow yay boy
Tay ma bakeula diobé
Sargal yayiiii
Ndakh dangua degue dadji roumbakh deuguine dadjéy
Wouylélé lélééééé sama yaye ma yaye...


Wawaw kou mine seu khoulo yab leu
Ma chéri tongo bi mom diarouko
Ni sokoo beugué
Dangua degg dadji té rombakh deuguine dadjéééé


Deguetil déguetil
Shooooooow !
Yekssi ngue yekssi ngue....
Shoooooow !
Pape fi ci Pikine way
Shoooooow !
Fileu ??? am fé leu leu ???


Deguena dadjeuuuuuu...
Wakhléne meu fougnouy tassé...
(Hey fougnouy tassé ?)
Madison madison lagnouy tassé way
Degueul dadji yow( 2X)
Dinaleu digueul lila kham ci mbakh
Walayé soumalané beuguenaleu Cheikh
Ibil sey beut dima khôl... Cheikh Amar
Jangual sameu djikooooo
Bamou nékh la wawaw yes !
Souma bakhé ngua kham nigno wara and bene famille bi la
(waw... Dolima)
Cheikhoooo Amar... Serigne SALIOU nguey begué
Cheikhoooo Amar... (séni mouchoir na sal bi wekh) domou ndéyou Kader Ndiaye, woy naleu Cheikh
Ya beugue Mame Cheikh Anta MBACKÉ borom darou Salam sameu serigne bééé Cheikh
Cheikhoooo Amar khamngue fonkeu naleuy ndakh sa mbakh sa talibé lérr na
Waw baye Malamine Bara bindeul namey téré, téré yassa Saloum, Saloum niéti néék leu biko gnintéél beu thi wagne beu wagne beu wagnou bour leu
Bour beu bourou Saloum , fougnouy tassé ?...
Awa Baldé borom Kolda
*(Ibrahima , theuy linguey mbalakh... Gneupeu la lerr ndour)


Waw Aida Penda Ndongo
Domou Ali Coura Ndiémé
Dafa dém ci farawoudé
Naneko dama beug tééré
Bilay tééré yamou dane sol eyway dafko simi lamssal
Ba ci tété ombiiiiiiiilé ; Dafko simi lamssal

Waw baye Malamine dara bindeul namey téré, téré yassa Saloum, Saloum niéti néék leu biko gnintel beu di wagne beu wagne beu wagnou bour leu
Bour beu bourou Saloum , fougnouy tassé ?...

Gorou Marie Amar aka beug segn SALIOU
Eyway beugue yeugueu koy fay
Kila beugue meuno ko fay
Kileu beugue lay bégué Cheikh
Kileu beugue lay titeuro
Beugue yeugueu koy fay
Kileu beugoul doula yeugueu koy
Kila beugue lay béguééééé
Kileu beugueu lay titeuro...

Waw baye Malamine dara bindeul namey téré, téré yassa Saloum, Saloum niéti néék leu biko gnintél beu di wagne beu wagne beu wagnou bour leu
Bour beu bourou Saloum , fougnouy tassé ?...


Souma nallé beuguenala... Khipil sa beut dima khôl mane
Awa baldé sameu kharit la
Awa souma newé beuguenala... Khipil sa beut dima khôl man
Awa baldé sameu djiguéne la
Wawaw ni béguéééééé di beuguééé di beuguéééé kay léne gnou bégué wawaw...
Usine niary Tally fofala djoudooo
Gnouy béguéééééé di beuguééé di beuguéééé Guinaw rail béguééé wawaw
Parcelles assainies 1 beu 26 kayléne gnou béguéééééé di beuguééé di beuguéééé Pikine wawaw
Hoooooooooooooooo.....
Souma naléne beuguenaléne ... Fans yi bégué négn léne
Bayé Gado yayou Pape bou ndaw
Ni dadj dégueu dadji o takh ngua meuneu raw say mass, khalébi ridieul meu say ndér...
Ni dadj degueu dadji o takh ngua meuneu raw say mass, fans yi man dé bégué naléne
Wouy lééélééééééé...
Dégueu dadj....

  • Category

  • License

    • Standard YouTube License

Loading...

Advertisement
to add this to Watch Later

Add to

Loading playlists...