Uploaded by slampac on Apr 10, 2010
http://yafaydoutidjanie.skyrock.com/1.html PAROLES BABACAR THIAM fahazi salamoun fa hazi salamoun mini iley kaw marioul anbari wa taybal miskaw damay wélbéti bollém wéyénou sodane
tchi zahir sidi batine ba diar di sétane
sama khatir dafa roti fa behrou kayor
may wey ki jara wey moniou toussé ay leer
nga lambo tchi diné lislam
sopé ba la ko jokh mo héyone té khadim
khoutboul jamihou niass ya di janteu njooloor
saxaal gua fi ay leer tek si mbir you doy waar
ma gui lay yalouwanne yaw mi done tijaan
may ma sa mboubitane xool kone ma dé tchi imane
fégoulena tibalma kone ma jook si békor
raf léna khod meu ma bah li may gar
sa wéla gueuneu gaw khaar mou fad bay buur
sa khewela gueuna bawane ba melni ay niir
sa haté géna wer ya khalilou rahmane
té lo wax borom "koun" dal di neé fa"yakoun"
sa kharbakh yi gua lambo siwal na doktor
dal beu ko taafli mou weer far dou déme ssi doktor tékotaafli sa loor yi tafalko bachoura
mo tagok lorou dounya ka chaka oukhra
dama sope di la wéye wanté raw gua say mass
li takh ma di la wéye gua nirro borom fez
sa mbotaam xalimba raw na dabo ssou Moussa
sa waydé yi nga dékal téwon na Issa
kouye mouride na ma nieuw wéylé sidi barham niass
wa dji xaam meuna ragné té sope barham niass
mou jokh ma khatim mba mou jokh mab faw khom
té bawal mam khél mba mou may ma fa moom
kone dana meuneu wéye ki fi guéne si sodane
di khoutboul rohoyi naan si peyi diwaane
deglou léne bama délou di kagn di gueune
fi sa azaal la ko buur bi jitalone douwoul fi
barhama ba nga roté ba say bakéne fess
bawal nga gnilone khar ba séni ndab fess
halam ak alal am mom la jaay tchi lislam
gnou signéle ko mou weer jookh ko khatmou fayloum
sou nguéne xamone ay may sa you néke guen téew bagna ling kaar bagna dinguante té guene saxoo waaw beteb kagnane dafa bepeng sakho lou kharbakh kone gnou guissbi nga watté you xamné ya baax
masta joox keur bayam té raw tchi si lislam
béne serigne manou fé waax né demna daraam
ki raw na aw massam ni att mi weéy daw bou kagnane amoutone lolou modi ak mbakh
sou féke guey yeém lolou doye na kharbakh
bam amé gneti att la dadial BACHOURA
di dior ay massalaam bolékok maqamam
siroube ngueunéle bi nga lambo néwoul si ay mool
yaye khoutboul yaay raoussou yaay seydi ridial
toutiwoo reuyoulo gattoulo douho njool
dieumi RASSOULOU la yoor gnou niro baasi mole
sa beut yay nelawite kholba mom mou ngay xool
té rohom ga arach ak koursiyousi ley beéw
té bouy retanite xaar kanaam ba né wer kar-kar t
é waram gena nekh lém ssa khol ya miy waar
bala nga koy hem lol boba aw nakar fegne
so kholé barhama niass guiss ko mouye mougne
moy djikom jamou donone fa saydi hadnane
dogal bou reye bala doylo moy "koun fa ya koun"
faalewoul adinak li ci biir dafay nil
khegn touhoul loumouy yala ak nabi daal
mola xaam koumou yem ci alal bamouy soy
té am ko douko bég lo xamoul lou mooy baye
konté woul ay tone titou mooy yenouy taakh
raboul samawaati wal ardi doy na koy jeex
té mandok ragal yalla ak tabé ci lislam
té tolam ba dou boy modi yonou jakaam
hitém ya mo guena kher gaindé moy yébuy buur
karama ya ngéna rey doussi golfa yiye door
ay betém dafa bot emni diani saman
rahmatamom guena mat ci fakhirak miskin
suxilingua sugnu roho yi sukhone souniouye mame
nigno minka bou wer diene ba teersi ndangane
sillmaxxa kouka tay ba bam xool assamane
warna joox baay saganté topeu say waw
raboul jallil la ko fal joxx ko mane tou rabbane
fal gamiye falidomame siwale nalab daal
waltakoun outamane mome ma la wax fa lakhot
kou aw cib dingalaam kham illahi nassot
bagne yooré souniou hadio siyaré madina bagne démé basa pome ba gnou déffa diorane dieumeum
yak xeel ya xool ya bagne diagnok baye dougne mebéte lu moy topou say takhok mome ndax melow yousoufa la la yoorki rawone ci ay taar
ba kou dianok mom sopou ko dax fa yoor leer aladjii souniou mame dane na wax né mooy hass boba ma ngay khol nawléyak betoub mass
la khassou dinarou mom bagne ko diokhone la barham fayé balayi fi ci sodane
la khadirni fi moussa wama li hayate lassougne bay yaré domame bi isni mahyaa
diouli na si rassoullou illahi mahwwa salatane wa salimoune ma gnane si abass
toudé na di la wey fadi hassi djihate ci koursiyin gni fi dan wey imamou ibada
fabal khatmou sa wey wi té hemfi yaw thiam nélo limitam do dadial ba déme samh sa talif yi nga talif mané sou koye mole hadjaliss you nga sang kit siwaal nalab ndaal.
NIASS.
Category:
Tags:
- babacar
- thiam
- fahanzi
- salamoun
- alfou
- salati
- zikr
- aida
- faye
- moustapaha
- gueye
- baye
- niass
- cheikh
- ahmed
- tidjanie
- el
- hadji
- tafsir
- al
- quran
- gamou
- bourda
- islam
- oustaz
- barham
- diop
- barhama
- arafat
- cisse
- moudir
- medina
- allah
- diouf
- astou
- diankha
- ibrahima
- ndao
- imam
- hassan
- assane
- lahi
- laha
- mouhamadou
- baba
- lamine
- bashir
- tidjane
- nurul
- kamal
- khalifa
- ass
- aidara
- fayda
- mouhamadoul
- moustapha
- diankhan
- fazisalamou
- faydou
- bibi
- wa
- bi
- taha
- pape
- hadi
- 1959
- 2010
License:
Standard YouTube License
-
12 likes, 0 dislikes
12:10
babacar thiam gamou 2009by slampac9,899 views
7:02
NAZIR AK BABA LAMINE NIASS.by slampac11,566 views
4:13
haoussa zikrby slampac14,285 views
9:51
BABACAR THIAM. BIBI WA BI TAHAby slampac12,427 views
3:01
aida fayeby slampac16,121 views
7:36
Aida faye Karama baye niasseby AGIEJAGNE102,940 views
12:08
video Baye Mamour Insa gamou 31 Decembre.wmvby jeunimage12,351 views
7:05
BAYE NIASS daddy bibson ft talibe baye hip hop galsene.WMVby slampac14,982 views
6:11
Zakira: Yallahby gelongalmusic100,229 views
5:53
Babacar THIAM Nurul Kamail 10by slampac6,361 views
10:03
aida faye bourda partie 2.by slampac12,915 views
2:50
Nazir niass Al Khouran KARIMby slampac11,343 views
4:43
guewelou baye niasseby kossidakar12,332 views
4:10
babacar thiam zikrby slampac11,661 views
10:00
IBRAHIMA NDAO BAYE NIASS.by slampac21,589 views
3:31
BABACAR THIAM zikr CHEIKH AHMED TIDJANIEby slampac8,364 views
8:38
AIDA FAYE zikr partie_3.by slampac19,973 views
7:36
CHIFAOUL ASKHAM de BAYE NIASSby emdimicro29,434 views
8:51
AIDA FAYE zikr partie_2by slampac13,181 views
2:41
aida faye bibi wa bi taha.by slampac12,959 views
- Loading more suggestions...
waw nyasssssssssssssssssssssssssssssssssss
mussuable 6 months ago
dieureuf baye!!*
sarata0 7 months ago