Alert icon
We're changing our privacy policy. This stuff matters.  Learn more  Dismiss

talif en wolof

Loading...

Sign in or sign up now!
Alert icon
Upgrade to the latest Flash Player for improved playback performance. Upgrade now or more info.
1,290
Loading...
Alert icon
Sign in or sign up now!
Alert icon

Uploaded by on Jan 28, 2009

No description available.

Category:

Sports

Tags:

License:

Standard YouTube License

  • likes, 0 dislikes

Link to this comment:

Share to:
see all

All Comments (3)

Sign In or Sign Up now to post a comment!
  • BOUTADES EN WOLOF Naa la dënk ay kaddu -Weurseuk booko gatandoo mou deup -Daradia booko diayé mou xathie -Ag dioudou booko diayé lamigne mou diis -Baadolo booko soxalé mou gaagne leu -Diangoro booko neubé mou worla -Am am booko foé mou yakkou -Waar booko bayé mou antou boumou yatou -Boo toogué té sagg toogue jotul nanga jugat -Say deukando bugnu xam sagg yekhé té bugnu xam sagg féniakk -Say ndigal bugnu xam sagg fitna ndax wadiour kassu lëwël bu tangue dieur la
  • BOUTADES EN WOLOF(suite)

    -Boy jéguëlu na nga dem beussi xouroub yalla , nga gass fa réenub yééné, xasfa xassoub toroxlou, dagg fa thiaroub laytann

    -Soob ko thi guuenoub tubb,deubé ko kouroub tabbé, taalé ko taalab ragal yalla, yak ko si ndaboub téguine, naané ko kokoub mugn

    -Ndax diamono ngor ag mugn kassé la

    -Boo mugné danga muugn,danga réé ,danga moudie, danga mouthie,danga mouthielé.

  • BOUTADES EN WOLOF Naa la dënk ay kaddu -Weurseuk booko gatandoo mou deup -Daradia booko diayé mou xathie -Ag dioudou booko diayé lamigne mou diis -Baadolo booko soxalé mou gaagne leu -Jangoro booko neubé mou worla -Am am booko foé mou yakkou -Waar booko bayé mou antou boumou yatou -Boo toogué té sagg toogue jotul nanga jugat -Say deukando bugnu xam sagg yekhé té bugnu xam sagg féniakk -Say ndigal bugnu xam sagg fitna ndax wadiour kassu lëwël bu tangue dieur la
Loading...

Alert icon
0 / 00Unsaved Playlist Return to active list
    1. Your queue is empty. Add videos to your queue using this button:
      or sign in to load a different list.
    Loading...Loading...Saving...
    • Clear all videos from this list
    • Learn more